Tanku neen (3 fois) La doxé Tanku neen (3 fois) Tanku neen (2 fois) Loxo neen Coono neen Xif neen Feyda waaw Aw ma "vélo" asta maak "auto" Nit ku néka Amna lu koy rey bes (lu koy rey bes bes bes ...) Suma diotoon lolou Dina dee Foum ko diaguar diaguar diaguar diaguar diaguar Ca adiana sa ca safara sa Tankou neen la doxé Bayico guinaaw diem kanam Bu ngelew li diogué Ma and' ak moom (di weey) Bet bou fata fata fata manam Sama tur munu ma ko wax ci khadia goudi Bou ko djiné yi dégué Sétè souba aat Yobou ko ci ay dioow dioow Fine ma djeulè sorinaa Yalouwane sèè Sookh sookhlou wooroul Boula diarè yow di ngua sookh Waayé do dèè Damala yendu lo guane laa fi Fima diogué soori na Topa taali bi dox ba eksi Fege neek bi lo fiy outsi Ci khadia goudi gui Man la goudi diop, mana Sama tur munu ma ko wax ci khadia goudi Bou ko djiné yi dégué Sétè souba aat Yobou ko ci ay dioow dioow (Refrain 2 x) Sétè souba aat Sétè souba aat