Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale (Bis) Ci sa bët laay xool naan la I Love You Baby yow yaay sama life (Bis) ♪ Baby yow yaay sama life Suma Yàlla bëggee wax len ko na ma baayi ak yow Ndax ku melni yow amatul ci àdduna Sama xol laa la def bëgg dëgg laa la def te duma sooraale Benn noon ndax yaay sama life Ci sa bët laay xool naan la I Love You Baby yow yaay sama life Baby yow yaay sama life Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale (Bis) ♪ Ci sa bët laay xool naan la I Love You Baby yow yaay sama life (Bis)