Par AbouAmg Lila thiy mousseul Moy di moytou Li gneup la titeul Kone boul gueuméntou Mome dafa gneuw Nit gni di dém Dianteu bi soo Guissatou gnou lérr Meme samay xarite Meuneu tou malene guiss Ba ko djip day tite Boul faté ni mi ngui fi Batay Lakhou na mais mingui fii Batay Boul faté ni mi ngui fi Baa tayy Lakho tina Mais faites gaffe Lila thiy mousseul Moy di moytou Li gneup la titeul Kone boul gueuméntou Moytandikou Ni gnouy doundék diaane thi pakh Respecté consigne yéy takh gnou doundaat lou nekh Ndax wergou yaram bou sakh egal happyness Revivons des jours meilleurs Boul faté ni mi ngui fi Batay Lakhou na mais mingui fii Faites gaffe Boul faté ni mi ngui fi Baa tayy Lakho tina Mais faites gaffe Together we will get there And struggle for better days Its time to build our future Diok ni li daf fiey diekh (Par force) Nguir aar sa bop aare sa ndiaboot Moy respectez les gestes barrières Bagna bayé ko fiy dieulé Diok ni Li da fiy diok... par force Lila thiy mousseul Moy di moytou Li gneup la titeul Kone boul gueuméntou Fagaro geun fadiou Fagaro geun fadiou Kone negn leen vacciner wou (Vacciner wou) Boul faté ni mi ngui fi Baa tayy Lakho tina Mais faites gaffe Li arr sa bop aar sa ndiaboot Batay Moy respecter les gestes barrires Fais gaffe