Kishore Kumar Hits

Maabo - Daf Niou Bett текст песни

Исполнитель: Maabo

альбом: Jolofbeats


Yaguoon naa fook ni
Sokh la wouma koudoul mann mi
Mann kenn la woon si yooon wi
Doh di demm akk sama yann wi
Beuss bi ma la guisseh kerok dafa leer si nioun niaar
Sounou holl yi ninou dadje si la hamm ni ioe laa doon haaar
Yaa yaa yaa yaa ya tah may weur fi mbekteh neekk guirr indil leu
Yaa yaa yaa yaa fook ma siguil leuu
Sama diamm yaw leu
Yaatah ma hamm ni mbeuguel neehe
Mann souma begue yaatahh
Meussouma fook nee...
Sama diamm yaw la
Nitt dina ma toll fii
Mann souma begue yaatah
Liii daf nou bett maak ioe
Eeh si mbekteh dello dima deuffal may reeeh
Mann awma benen héro
Yaw yamey beguel saay sou nekk
Huum mbeuguel dina yegg si fing ko doul foogue
Keuff sa holl di fooweeh
Yaw la sopp teh yaw la nopp
Ya leen gueun fopp doo niaar ioe
Jikko yi nga soppi si man nimu bariwee
Jubbanti yi bonn, deff ma goorou qualite
Yama yokk diom kon nakk nala keral dila begueul ndahh lolou laa digge
Cofeel ci biir holou nitt
Amoul njarigne soula yobou woul si ngeneel
Dalal ngama dotuma tiit
Yaaw dara melul ni sa mbeguel
Sama diamm ioe leu
Yaa tax ma hamm ni mbeguel nehe
Man suma begue yaatah
Meussouma foog nii...
Sama diamm yaw leu
Niitt dinama toll fii
Mann souma begue yaa tax
Lii daff nou bett maak ioe
Ci mbegte nga may dello
Dima deufeul may ree
Man awma benen hero
Yaw yamey begueul sa sou nekk
Woyoyaa sa sou neeekk eeehh
Yaw la eeeh

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Ada

2021 · сингл

Похожие исполнители

Jeeba

Исполнитель

Bril

Исполнитель