Xaley bi may doundal Feel nani dafma beug ngir yalla Ay vibes'am fimouy dialeu Amoul benen mindef boufay dialeu Bouy dokh di daagou ci kogn bi Day dal melni solou daleu Lima yeuk ci sama xol bi J'affirme moy natural love Guene ci xel yalla ko sakk ngir man Yeyeee, wowoooo Yalla ko sakk ngir man ♪ Baby dama dof ci yaw ♪ Limoy natural love
Boulen ci diemeu wah lou nyaw
Lima geuneu neh ci mom Moy yerem wa moy yerem wa Ak dohine ba ak dohine ba Eloquence bek elegance bi Ki moy sama sweetie girl ♪ Baby dama dof ci yaw ♪ Limoy natural love An gars gni Boulen ci diemeu wah lou nyaw Ndeysaan Yay sama lovе Dama dof ci yaw Loma def no matter Tahawougama mama Natural love baby I lovе you I love you and you know it baby Bouy dokh di daagou ci kogn bi Day dal melni soloul daleu Lima yeuk ci sama xol bi J'affirme moy natural love Guene ci xel yalla ko sakk ngir man ♪ Ca naturel ba la She walks around the corner Look like a diamond in the water I know this girl make me crazy This love is a natural love Ca naturel ba la