Danga took sama xol yaye kiki mome léboone Guénteu na takeu leu kaay done sama yayou doome Dougou na doundou na mougne took ndax yaw doome Té beuss boussa doome indé dome defco dome sama doome Li nit di dathie thi naigou seuye Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye Li nit di dathie thi naigou seuye Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye Dinala romb midi Oooh wait Té doma guiss Oooh wait Pénicilline yangui gneuw Oooh wait Ma dabali Oooh wait Gaa fof no welly Oooh wait Now doto KO défati Oooh wait Oooh wait Oooh wait Gnata yaye la fi seuye teuthie thi kasso ndax séne doome Yi lathie ngay lathie téy amagou ma tontoome Yague Toul legui Rek nga xam louy noone sama doome Ideu bi tey la diékh tay Di diégueulou waat sama doome Li nit di dathie thi naigou seuye Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye Li nit di dathie thi naigou seuye Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye Dinala romb midi Oooh wait Té doma guiss Oooh wait Pénicilline yangui gneuw Oooh wait Ma dabali Oooh wait Gaa fof no welly Oooh wait Now doto KO défati Oooh wait Dougou na doundou na mougne took ndax yaw doome ♪ Paré- paré- pa- pa- Paréna Xamoni bou diééxé Diééx na Diééx na Gneuweul Han Ngani Han Han ♪ Mani baydou volume Sabou mi nana ni Tékki lunettes yi nguir gueuneu guiss