Kishore Kumar Hits

Jeeba - Life goes On текст песни

Исполнитель: Jeeba

альбом: Alajee


Fi dem na ba kenn mënutu fe def lu baax
Ku def lu baax ñu faay la lu bon léegi nak
Xawante sutura yaakante deer te duma sa noon
Mënoo dem kenn du dem léegi nak
Fi dem na ba kenn mënutu fe def lu baax
Ku def lu baax ñu faay la lu bon léegi nak
Lu ne ngay dégg ñuy wax di yaak deer
Dundal Yàlla baax na lépp dina leer
Fightal sa life ndax mbamb rayul weer
Bul mësa xaadi kon life goes on
Bul mësa bàyyi, eh eh eh
Broda life goes on, eh eh
Bul mësa xaddi, eh eh eh
Sister life goes on
Dina la ker nga fay ma naj
Sa xol bu bon bi nanga ko jema soppi
Jobal jobal nga bañ ba rom naa la dem
Yaa ngi sandi xeer bouclier sama dos du daal
Fi nga taxawoon demb ne maa fi gëna baax
Mais fi nga taxawaat tay ne maa fi gëna bon
Wax ju bon dëkkul fu mu jëm
Fu mu juge la dëkk
Dama laay bàyyi ngay wax maa ngi si tollu lajj kaw wa kaw
Le chien aboie la caravane passe
Maa ngi sama auto yaw ngay dégg kanam passe
Lu ne ngay dégg ñuy wax di yaak deer
Dundal Yàlla baax na lépp dina leer
Fightal sa life ndax mbamb rayul weer
Bul mësa xaadi kon life goes on
Bul mësa bàyyi, eh eh eh
Broda life goes on, eh eh
Bul mësa xaddi, eh eh eh
Sister life goes on
Doomu jaambur xamoo nu ñu ko ngembe
Grand place du place
Nga topp ci deeram di lëmbe
Yee ma tuñu si yaak deer
Ak dëkke wax ju ñaaw
Dale yóbbu si sëriñ
Ne ko defal ma xeel mi naaw
Lan moo fi jar yi jikko yu bon
Yàlla bindul yemale wul
Te wërsëk yi bokkul
Lu tax su ma jiito nga may joxoon
Nii ma mel du kenn Yàlla moo ko def ci man
Le chien aboie la caravane passe
Maa ngi sama auto yaw ngay dégg kanam passe
Lu ne ngay dégg ñuy wax di yaak deer
Dundal Yàlla baax na lépp dina leer
Fightal sa life ndax mbamb rayul weer
Bul mësa xaadi kon life goes on
Bul mësa bàyyi, eh eh eh
Broda life goes on, eh eh
Bul mësa xaddi, eh eh eh
Sister life goes on
Fi dem na ba kenn mënutu fe def lu baax
Ku def lu baax ñu faay la lu bon léegi nak
Xawante sutura yaakante deer te duma sa noon
Mënoo dem kenn du dem léegi nak
Yaw life goes on bul mësa bàyyi, eh eh
Broda life goes on, eh eh
Bul mësa xaadi, eeh
Sista life goes on
Eeh brother life goes on

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители

VJ

Исполнитель

Maabo

Исполнитель