Niit ya ngi toppeu adouna di Daw diap ko taxoul gnu taxaw Dee ba ngi dokh di gneuw sugnu kaw, dafa yagg wayé guen dou raw Meunou ma nelaw dou gawu dou Dibbéer, ta likoy dindi dou ferniente Meunou ma wax ak yaw si dianeer, bou goudé nga may tontou ci Guent Meuneu touma ameu kou melni yaw, Mane lolou lima xam la Li ma meti dou li nga dem ba faw, wayé ci diamono yima la xamla Da ngay minanté ak Niit ko naw, dem ba faté ni Dokh ak Bane la Dafay dem ba bokk ci yaw, Boy da ngay dem ba faté ni gane la Niit sagnu ta bagne woté, surtout woté bu diogué ci Yallah Takh ma souk samay ome, sama rongogne yi di tourou may niane bou balle la Moussou ma fok ni ni lay demé beuss bofi nekatoul Dakh bedienou Kobba sugnu lako diamé, fils kokou dou nekha toul Dakh Niit kou nek ak Ni nga koy xamé, tay sama doundou bi nexatoul Damadone gaagnu di xeuye di taané, wayé tay dji yoombatoul Yene say may tok di khentiou say yeré guir fataliku sa xeet Wayé lane lay wout si adouna bi mane kessé bou dé nekato ci sama wet {2} Comme que legui nonou la demé Mane sakh legui damala meré Sa bountou nek dotou mako diegué Dotou ma setanati say photo, ta dootu ma xentioti say yeré Nane lay def ba boor bi nga ma lebale demb tay ma meune lako faye Donté xam nani nathe dium demb, meune ta wowale pottum tay Loy dieurignu gnak toll bodule baye Lepp boor bodoul faye Ma ngi sogua xam loutakh monate di xol dom dji rek mouy sour Djiguene djuy seuyi dagnu kouy mour Ma ngi sogua xam loutakh, dereet bou dé di sopeeku deut Keweul di teup ta dome dji dou beut Nakh nga ma ba dem sa yone Loutaakh xaro limala denthialone Koula ni beugou mawone gnuy ande thi mbedeu mi dokhontou diapannté lokho Koula ni beugou ma wone nga diegué ma guir louma meti ma yeguel lako Koula ni neko wone sama dolé, guir louma meti ma meune ko encaissé Yaw nga xam thi lolou lepp ba paré, ngay dem dima fi bayi mane kessé (bis) Meunote nga fi dess wetalima touti meme sou feké damay wagni ci limay dou doundou fayal lassi djouti Yeah, lou Yallah def mo guene, Ma ngi Jegualou