Ibil nal sama khol, Yalla na nga si guiss lou lére Té gueuneu kham ni Amoul kénène koudoul yaw. Mbeugél gui nékeu si mane A ngii di ma dane Té gueum na né di na done Sa néné bi ngéy tété. Mane mi souma mounone, Dina bokake yow bénéne yone, Dila wowé néné touti, Ndakh té mane mi, Mane mi gnanou ma yalla, Gnanou ma yalla Déss fii mane réka Yow mi néke sama khol Guissou ma kénéne koudoul yow Mbeuguél gui mo ngi ni di law, Ibil nala sama khol Yow mi néke sama khol Guissou ma kénéne koudoul yow, Mbeuguél gui mo ngi ni di law, Té dina done sa néné. Am na gnou wakh Mbeugél tiono rék la, Wayé ma ngi léy khamal Dou kéne yow réke leu. Beuss bou me le guissé Ta kham ni khol déy guissé Té fok na ni do meusse tass sama yakar! Boul am loy ragal di la khar, Doumeu meusseu diay sama taar, Dinala wowé papa chéri, Dina done sa sokhna, Di na done sa baby, Mi léy fadial Say sokhla, oh baby yow réke le Yow mi néke sama khol Guissou ma kénéne koudoul yow Mbeuguél gui mo ngi ni di law, Ibil nala sama khol Yow mi néke sama khol Guissou ma kénéne koudoul yow, Mbeuguél gui mo ngi ni di law, Té dina done sa néné. Yay sama doolé Soudoul yow wate na né dou done kékéne, Diokh na la sama bope, Té dina la dégueul di le bégueul, Baby boul sone, Gueumeul ni yow réke le! Dou kékéne...