Kishore Kumar Hits

Omg Oumy Gueye - Xana Wero текст песни

Исполнитель: Omg Oumy Gueye

альбом: Melokaan


Si bu ka sibi nunka mas
Bu kanna sibi
Yeah yeah yeah yeah
DD in the house baby
OMG
4Leuz
DD Records
DD moy sama team
Yow xana wero
Job andul ak wax dju barri deggo
Nena Alhamdoullilah tout est bueno
Fi tout est bueno (praaaaa)
Deffal ñeupeu guiss
Xam ni du ay fo
Job andul ak wax dju barri deggo
Nena Alhamdoullilah tout est bueno
Xana wero
Nangulo job bëgge trophée (han)
Do am tuss xana wero (skut skut)
Nangulo train bëgge signer pro (bra)
Do guiss bic xana wero (brraaa)
Yoro money bëgge ndjap boy
Tioy yi buñ la guissé
Duñ la lëbal dañ ley diap boy
Eh boy
Guënal ci lolu
Li moy balou boop
Bul sona meuno ko goalou
(Bing bing)
Real niggas always Dou realtin'
Yow amo album në nga yay sunu king
Ci kaawam mu djoli
Boy DD dou tiolé
Waxal ci wax dji bok
Rap ko mu goorë
4 doolem la woolu boy
Raagalul lolou
Bo doofé ba sooru
Xam nga në doto ci guëna
Flow bi baawul fen ken
Ni wegn bi ci deuneu
Oh bul fowé sa xeel
Dieuf dieul la rek
Lofi xaar aytia diokhel
Yima yowma
Anda ka gonda
So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
Yima yowma
Anda ka gonda
So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
Yow So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
Yow So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
La di da de (moony)
Relax your body (han)
Bo beguë booka suñu team
Boy fok nga parë (fok nga parë)
La di da de (come on)
Relax your body (wou)
Boy course'ak DD
Bul daw yow dieul nga ndarë (bing bing)
Deeg number one
Nangulo ciono (ciono)
Waxma lolu numu meuneu nekkë
Job bey fey
Bul fok ay fo la (fo la)
Meunul në meunul në dedete
Xana wero dama diapa ni
Duggal ci Lady Boss
Doto ko defati
Ñeuweul DD feka fa bandit yi
El Capo ci game bi
Ñun dañu wëradi (Walahi)
Xana yow wero
Yo
So werone do ma diëma diss
Sa rap dey fenn amul benefice
4Leuz dey job ñewul Jadakiss
Yalla moma team
Sama life lay rime boy
Run boy
Sa call tey fi du ring boy
Kay rang boy
Fi DD leepa chill boy
Sa Mc du dëm dey yakha courant (come on)
Duma lekka doff non suur na
Yima yowma
Anda ka gonda
So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
Yima yowma
Anda ka gonda
So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
Yow So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
Yow So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
So ñu xaamul dë ñu wowé (eh)
La di da de (moony)
Relax your body (han)
Bo beguë booka suñu team
Boy fok nga parë (fok nga parë)
La di da de (han)
Relax your body (moony)
Boy course'ak DD
Bul daw yow dieul nga ndarë (prrrraa)
Xana yow wero

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители

Jeeba

Исполнитель

Maabo

Исполнитель