Kishore Kumar Hits

Ashs The Best - 4010 Session #4 текст песни

Исполнитель: Ashs The Best

альбом: 4010 Session #4


Suma la mënoon gisaat
Gisaat la benn yoon sama life pour wax la
Ne la sama xol masoo fi jogee
Numay def pour gisaat la
Gisaat la benn yoon sama wet ngay retaan
Ngay bég dima begloo
Ohhh
Dem nga bayi ma fii
Dem nga yobaalé sama leer bayi ma ci lëndëm
Wéetal ngama loolu
Numay def pour gisaat la
Numay def pour gisaat la
Pour wax ni la "I LOVE YOU" baby
Dem nga bayi ma fii
Weet na, yama weetal
Kañ ngay dellu waat fii
Ci sa wet laa bëgga dàlloo
Dem nga bayi ma fii
Wéet na, yama weetal
Kañ ngay dellu waat fii
Ci sa wet laa bëgga dàlloo
Feeñal nga ma réeraat na
Numay def ba gisaat la
Dem nga bayi ma wéetal ma
Biig ci guddi janeer na la
Ya ma taxoon daw bay death
Te nañ ma bayi ma wéeto ak life
Li may yëg ci moom du dëñ
Batay mbëgelam momay daaneel
Wéet na jooy ndax wéetaange (wéet na)
Réer ma réer Way réer na
Nela weccoo ak keneen
Batay mbëgelam momay daaneel
Yaane woon duñu yaw do ñoom
Nobuma ku melni yaw
Sama xel du jóg ci yaw
Suma la mënoon gisaat
Gisaat la benn yoon sama life pour wax la
Ne la sama xol masoo fi jogee
Numay def pour gisaat la
Gisaat la benn yoon sama wet ngay retaan
Ngay bég dima begloo
Ohhh
Dem nga bayi ma fii
Dem nga yobaalé sama leer bayi ma ci lëndëm
Wéetal ngama loolu
Numay def pour gisaat la
Numay def pour gisaat la
Pour wax ni la "I LOVE YOU" baby
Dem nga bayi ma fii
Weet na, yama weetal
Kañ ngay dellu waat fii
Ci sa wet laa bëgga dàlloo
Numay def pour gisaat la
Numay def pour gisaat la
Ci sa wet laa bëgga dàlloo
Dem nga bayi ma fii
Weet na, yama weetal
Kañ ngay dellu waat fii
Ci sa wet laa bëgga dàlloo
Dem nga bayi ma fii
Weet na, yama weetal

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Tukki

2022 · Мини-альбом

1995

2022 · Мини-альбом

Похожие исполнители

Jeeba

Исполнитель

VJ

Исполнитель