I feel good Nobody can disturb sunu life Ñun dañ koy def ba muy moom I feel good Respect ñi la dundal demb'ag tay I never let you down I feel good You push me high I never let you down I feel good You make me smile I never let you down I feel good Fi ma mujjee ak fing jëme Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore I feel good Fi ma mujjee ak fing jëme Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore I feel good Live my life melni ku mbedd jur Bës da ma reer yaa ma indiwaat Jang ci yow lu ma xammul woon school Mbedd a ma dicter ma bind texte Bëggoon naa tekki am ay millions Mais mësu ma xam li ma wara doon Dund naa gacce yu tegaloo Mais yaakaar yi naxu ma benn yoon Ròngooñu mère bi su geenatul Moy xellam dal na noonam beggatul Jaar naa foo jaarewul ba agsi fii Boo jaare fi ma jaar deeg Rest In Peace Fate wu ma demb moo waral tay Ligeey fii tay parce que suba moy fay Respect ci Paa bi ndanaan la jur Li may def ci Hip Hop xajjul ci yuur I feel good Nobody can disturb sunu life Ñun dañ koy def ba muy moom I feel good Respect ñi la dundal demb'ag tay I never let you down I feel good You push me high I never let you down I feel good You make me smile I never let you down I feel good Fi ma mujjee ak fing jëme Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore I feel good Fi ma mujjee ak fing jëme Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore I'm feeling good, feeling alright Foog naa ni gent ay dëmm weeyo'og gueule doon smily Yeen saay ma toog jakkarlo'og sama life Gis muy gën a tar may dolli gëm man def li ma war I'm feeling good Boo ñu bëggee disrespect f**k you F**king feeling good Jamanoy dox att yi di yox nga wara joge ci xale doon magg Life bi ay soxla lay jox ba nga xam loo xammutoon nakk Leegi Adduna ubbeeku say bëtt lu nekk nga koy jeem di lëjmbët Tux di daw di jang di màndi njugub night kawute bëccëg Maggu xale da fay bette da fay gaaw ci ñi ko fekke jo Demb nga doon bébé ñu lay fobb'ag di la teete bro Yalla rekk a ñuy sàmm mais mbedd mi mën na ñu wacce Def nañ ko ba muy moom te teggu ñu sunuy wayjur gacce I feel good Nobody can disturb sunu life Ñun dañ koy def ba muy moom I feel good Respect ñi la dundal demb'ag tay I never let you down I feel good You push me high I never let you down I feel good You make me smile I never let you down I feel good Fi ma mujjee ak fing jëme Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore I feel good Fi ma mujjee ak fing jëme Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore Salaamalek salaamalek Bismillah balaa maa lekk Waayee tay Alxamdulillah lay wax I'm feeling good Dolli sant sant santati Santaatati Maa ngi baax I'm in paradise This man called Baay Sooley B double A Y S double O E Y Feeling good life Ashs The Best feeling good life Mamy Victory feeling life My one and only Mamy V