Oh yeah yeah I love my life Life is love Love is life
I love my life Jealousy enemy akk ñii di siis My life is love Genn ci ghetto bi ligeey lot of jizz indi ci galle bi I'm black I'm proud Like Pablo I'm lonely on my own You can't stop me I'm black yes and I'm young too You can't stop me I love my life Dof ci son you see me Def Ko ci Kendrick maa ngi Jolof toog Million zéro pression Tukki du tekki geenu ma studio Def comme Fada comme Ndongo Xuman akk Bibson Sa stars yi lay jangal rap bi du pour coow King bi yaw la maa ngi akk millions flows From the bottom to the fucking top Gis-gis yi ñoo wute I know that you know yeah I know that you knoooooow oh my mind This is how I feel it But I know something you know I know that you know yeah I love my life Jealousy enemy akk ñii di siis My life is love Genn ci ghetto bi ligeey lot of jizz indi ci galle bi I'm black I'm proud Like Pablo I'm lonely on my own You can't stop me I'm black yes and I'm young too You can't stop me Xëcc bu daggul dikk kay Nañ ko xare demb ngir tay Dëkk ci suba guddi ngoon hoslou ngir guenesi Fëgg buntu bi tijjiwul teewul ñu jëlli lu ñu moom Fii ba Adduna wërngël kepp ligeey bi du pour fii Tëdd nelaw gent bi yee ma ne ma coono du reer boroomam Ci tolof-tolof sëgg siggi ngir dellusi Bu ñii di yakk di yakate Ñii di takk di daggate Maa ngi diap rap paqueter bangg Sekku ñu baale Sekku ñu ñi sakku ci rap bi Du geenati gaal bi Dërëm bi du geen gaal bi Dëkku ma Capsi Xëppu ma suuf ci ndap li Di siggil ndigaale Siggil sa wall ci rap bi Ki ngen diggaalel du baale Bu jekkoo du baale Bul faale ku dematul Kouy bardé na bardé kou pare Ku xarei niou xarei nioune Ku tarder dou andak ku tardei Comparer ma'ag boy yi Moy comparer nga sa shody akk sa mother