Yeah Yeah Yeah Yeah [Everyday I feel the same thing, Let me show you what I use to do everyday] Oh my life My life Oh my life My life Only sleeping in the morning Tristesse akk xonet Yeewu gis li ma gisoon Def li ma deffoon Let me show you my life In my ghetto My fellas ak family bi All day I see the same thing Paa bi akk mère bi jaxle Waaji tukki aw jeeg Diw mi ngi jail koñ bi gën a rëb Yeah that's my life (That's my life, that's my life, that's my fucking life) (That's my life, that's my life, that's my fucking life) (That's my life, that's my life, that's my fucking life) (That's my life, that's my life, that's my fucking life) Yeah Let me show you I'm from zero to the hero now From Ghetto sama këru maam Ñun da ñu bari te bokku ñu yaay Te nangu wu ñu topp ndigëlu kenn Du kenn ku sañ a dekku li ñuy dundu sunu life Dugg jail geen duggaat jail Du gacce du mbañ sunu quartier Wax ma lan la ñu gënëntee Ndax lu ma dundoon daaw lay dundaat renn Li ma deffoon demb lay deffaat tay The same struggle on my way Heure bu ñu xëyee naaj bi la ñuy njëkkënteel Ammu ñu dara fii soxla yi di dajje Ñakk te bëggu ñu gacce Looloo waral guddi gu nekk ñu dajj dee Te bëggu ñu dëkk ci clater Du ñi fi nekkoon demb ñoo fi nekkaat tay Mais li xewoon demb moo fi ammaat tay Jamano di soox ñëpp mujj catte Ku nekk ki lay còmpal ngay waatee Sunu yoon nekkul ci reew mi ak nguur gi, juge nu ko neex àttee We don't give a fuck, baay bakkan yëpp a nekk ci xottu gerte Oh my life My life Oh my life My life Only sleeping in the morning Tristesse akk xonet Yeewu gis li ma gisoon Def li ma deffoon Let me show you my life In my ghetto My fellas ak family bi All day I see the same thing Paa bi akk mère bi jaxle Waaji tukki aw jeeg Diw mi ngi jail koñ bi gën a rëb Yeah that's my life (That's my life, that's my life, that's my fucking life) (That's my life, that's my life, that's my fucking life) (That's my life, that's my life, that's my fucking life) (That's my life, that's my life, that's my fucking life) Yeah Flexion Oh life flexion Awma benn pression Man sonn naa ci pression Flexion What you think about me Nigger bul sori Stay with me Yeah Tout le temps sama life lay topp Every night fucked up Mais du ay line lay tux Ndeysaan ammoon naa ay taupes Mënu ma woon daw tëpp Akk Lu mu mënti yakk no Comme ... we never made it Album bi fog mu duggaat ci playlist Ñu jappoon ni ... ñuy dëppu sucer nan now we love it Du marquer histoire ... Tupac Makaveli Di geenaat ci kër yi Di def révolution comme ni Kerry Ci naaj bi ci ker gi Tout le temps ñing ci mission ci pression ci guerres yi Ròmb ñu boppu koñ takkalante Ñoo ci job di job everyday Mère bi buy hustle du gis nandite Li ñu doon rêver fils nekk na tay Job bi day fay Everything is okey Du lenn luñ ñu may That's my life, that's my life, that's my life Oh my life My life Oh my life My life Only sleeping in the morning Tristesse akk xonet Yeewu gis li ma gisoon Def li ma deffoon Let me show you my life In my ghetto My fellas ak family bi All day I see the same thing Paa bi akk mère bi jaxle Waaji tukki aw jeeg Diw mi ngi jail koñ bi gën a rëb Yeah that's my life