Kishore Kumar Hits

Ashs The Best - Gainde текст песни

Исполнитель: Ashs The Best

альбом: Gainde


Oh Mathydy
Doomu gaynde Du tiit du daw Du rëbb di sooy Ñu booloo
Ñu doon benn
Akk Mathydy
Se'ne'gal day dem ci kanam a kanam
Doomu gaynde Du tiit du daw Du rëbb di sooy Ñu booloo
Ñu doon benn
Akk Mathydy
Ñu jëlli ndam li
Na ñu booloo doon ab say waay
Bokk coono bokk ndey'ag baay
Baña noonoo jox ma loxo kaay
Sama dëkkandoo nga
Nitt nitt rekk'ay garabam
Suma gestoo gis la sama wet
Sama xel sama xol leppay dal Kaay kaay kaay
Gestul demb
Gestul, gestul
Xoolaat sa tay
Xoolaat sa tay
Ngir naatal ëllëgu ndaw ñi Kaay waay kaay
Naatal ngir jammi reew mi Buñ booloo
Buñ booloo
Doon benn say
Benn say
Ngir naatal jammi reew mi A'nd'ag MATHYDY
Doomu gaynde Du tiit du daw Du rëbb di sooy Ñu booloo
Ñu doon benn
Akk Mathydy
Se'ne'gal day dem ci kanam a kanam
Doomu gaynde Du tiit du daw Du rëbb di sooy Ñu booloo
Ñu doon benn
Akk Mathydy
Se'ne'gal day dem ci kanam a kanam

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Tukki

2022 · Мини-альбом

1995

2022 · Мини-альбом

Похожие исполнители

Jeeba

Исполнитель

VJ

Исполнитель