Wathié naa Teeré AMAYATA amna diouraum niéteu (8) att Té djangue bimay djang guissouma sakh njeurigneum Loutah mou am niou wara soneuh am niouy khaar sen héritage Aduna injustice leu dou kou nekkak mériteum Serigne bi néna kouka dégueul mou xétalileu Miskine bou fessaloul sa pott mou djékalileu Moussouma njaalo mais feug nagn-meu teeméri (100) yarr Bala may délou Daara ba faaw teemeer yi matt (500 Frs) Hééy! mais thiow dou djipp ma ngi maagueuh. Xamna sama handicap (lane?) Boy douma domou Diw niou def meu animal Sokhlaatouma nioumay doumoyou pour Meu effectivement douma done kou riche Ndakh dagnma sani aaleu. Kène tégou mako koudoul samay waadiour Yima diour Kone fokma démé Xollou mougn Té bania radical baayi ma khaar beu Souma gueuné deugueur touti daaldi faakeu {Pré-Refrain} Ma tchi meuneu guéné sama bopp Jameuh rek la yeené sama bopp Jameuh rek la yeené sama bopp Xam naani ma tchi meuneu guéné sama bopp Ma tchi meuneu guéné sama bopp Xawma loutah life bi di gueuneu yeemé sama bord Ani gnima daan boott dima nakh bama nélaw Loutah gnima bokaloul daara rek laay talal lokho Yeah yeah Amatouma Baay Guisseu touma sama Yaay Booy Guisseutouma Yaay Booy Bouma Yeureum dima diokh djeune "Jangal Ma Napp" Jangal Ma Napp Jangal Ma Napp Mané Jangal Ma Napp (So défoul rek def thioow) Yaw mi am Gaal meuneu djoow Jangal Ma Napp Oooh! Goor gui Jangal Ma Napp Yeah! Soxna Ci Jangal Ma Napp (So défoul rek def thioow) Sarakh ci fadjoul samay gaum Jangal Ma Napp Fouki att ak Diouraum Bèn (16), Kène beugoul melni mane Té mane meunouma ndourok kène Xam naani boudoul MBèDE kène douma kholé DOM Borom Auto bima moudjé Goal-lou dafma khélou rombeu Fourniture, Sac, Yeeré aki dall Bima djoudo beu légui dh dégg rk la tchi am Mounouma Lire té awouma métier bouma djangue Gni ngèni wowé WAGGA yi rek nioma nangou fatt Bala niouy wouti JOB fokk niou am loumou THIOP Seugueum douniou ko djokh dagnkay wouteul suniou BOPP Fekk niou Gueedju Koussoum wala Pont Colobane Fi koufi né di trainé dagnelay fuutti yaubou djaay Gnène gni di dougou FAC gnénène di dougou PLANE Nioune niou nek di dougou keu guèneu beu dougou JAIL Ngène berr niou tchi lepp melni nékouniou SUNU REEW Kène niéméwouniou DOUNDOU ndaxté RAGALOU niou DéH {Pré-Refrain} Ma tchi meuneu guéné sama bopp Jameuh rek la yeené sama bopp Jameuh rek la yeené sama bopp Xam naani ma tchi meuneu guéné sama bopp Ma tchi meuneu guéné sama bopp Xawma loutah life bi di gueuneu yeemé sama bord Ani gnima daan boott dima nakh bama nélaw Loutah gnima bokaloul daara rek laay talal lokho Yeah yeah Amatouma Baay Guisseu touma sama Yaay Booy Guisseutouma Yaay Booy Bouma Yeureum dima diokh djeune "Jangal Ma Napp" Jangal Ma Napp Jangal Ma Napp Mané Jangal Ma Napp (So défoul rek def thioow) Yaw mi am Gaal meuneu djoow Jangal Ma Napp Oooh! Goor gui Jangal Ma Napp Yeah! Soxna Ci Jangal Ma Napp (So défoul rek def thioow) Sarakh ci fadjoul samay gaum Jangal Ma Napp