Flowu terru Baay Sogi, daaju Percocet Vestu Tommy Jeans, tek ci pairou 7 (J's) Bëri laamiñ sama kaw, faut que ma lemu leen Te liniouy wax ci mann yëpp dara leeru leen Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu) Im on Sunu Flavor damay jengu rek (waar sama waar) Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu) On my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu Jengu jengu) Bandi mic Yaadikone (bandi) 4 projets yokk job wañi wox (wañi wañi wox) So may seet ma ngui Port Dope bi ñew na container, barigots (oh oh) Sama premier ennemi mane leu Melomind yi xam neñ dama manquer vis (Manquer manquer) Sama studio sama scène de crime Rey naa sama nafss musique rekkay sama viiice Sa rappeur neena dafa bëg mel ni mann Nee ko awma 1er Mai awma jour férié yeah yeah Homie paré naa pour songg projet anytime Depuis goné hustle moma gënël am liguey yeah yeah Flowu terru Baay Sogi, daaju Percocet Vestu Tommy Jeans, tek ci pairou 7 (J's) Bëri laamiñ sama kaw, faut que ma lemu leen Te liniouy wax ci mann yëpp dara leeru leen Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu) Im on Sunu Flavor damay jengu rek (waar sama waar) Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu) On my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu Jengu jengu) Ki la gënë jege mo la gënë mënë siss (chi chi chi) Ki lay gënë bege mo la gënë mënë kill (yi yi yi) Mandikat su gisul escalier sax dinë yeek Ak nima xiife lekk sa money bu mu la yeem Buru le yeem yagg naa raam leegi dama wara naaw Boy ya ngi sannanté ay subliminal May xol nu may jaayé comme Warano En mode Collie Budz sumay come around So xamul sound do fi fuck around Bul deglu ki ne gore du dug waañ Xolal togg naa motax bokk naa (woe) Balaa ngay xam sama tur, dama xaar sama tour (yeah Yeah) Kenn du ko tangal ni mann, mën naa leen aal sama four (wow wow) Leader ci art bi lijënti lotta G'z doga dox (yeah yeah) Duma lekk li ga yi togg sama avenir moma ñor Sa rappeur neena dafa bëg mel ni mann Nee ko awma 1er Mai awma jour férié yeah yeah Homie paré naa pour songg projet anytime Depuis goné hustle moma gënël am liguey yeah yeah Flowu terru Baay Sogi, daaju Percocet Vestu Tommy Jeans, tek ci pairou 7 (J's) Bëri laamiñ sama kaw, faut que ma lemu leen Te liniouy wax ci mann yëpp dara leeru leen Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu) Im on Sunu Flavor shit damay jengu rek (waar sama waar) Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu) On my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu jengu jengu) Outro (Sunu Flavor's DJENGUOU sample)