Xam nani man Xam nani nékété jaboot gi yaw Jaboot gi nékété buy la jiitëlé mënu ñu la dapp Kon daal mënu mala dapp Borom kër ku yéewu xalaat né wareefu jaboot gi géego yëkëti Dëgg maam ken dula dapp Kon maam ken mënu la dapp Xam nanè sopéku jamoono gi ñu nékké Tàbali rek la Jafé na ci laax di ko jaay Laax désatu ko jaay Xam nani man Xam nani nékété jaboot gi yaw Jaboot gi nékété buy la jiitëlé mënu ñu la dapp Kon daal mënu mala dapp Borom kër ku yéewu xalaat né wareefu jaboot gi géego yëkëti Dëgg maam ken dula dapp Kon maam ken mënu la dapp Xam nanè sopéku jamoono gi ñu nékké Tàbali rek la Jafé na ci laax di ko jaay Laax désatu ko jaay Dootul mëna laax jaay Ndax naboot gi ñi tòkk di yaatu di Dootul mëna laax jaay Ndax naboot gi ñi tòkk di yaatu di yakaar ci yërmande yalla Yaw sama waay mba jaboot gi suur nañ nékki Bala nga laax jaay Yaw laaxal jox lén