Par AbouAmg Soudé foo mola takha diouk yaw wakh ma ko leggi Mongui beug yagg té defo fouleu ba leggi Lou baakh kene douko waadj yaw Kone nak gaawal ci mane Khol ma ci kaaw ba ci souff Wakh ma lou manqué ci mane Niouni ma miin nala maak yaw khamanté nagn Guéneu bou amoul foumouy yam lolou mane doumako meune Letoulo ma firi woma waay defal lou khess Ndel ma sakh ni Abba mo gueune ngamay tekk stress Rétane you bari youma néké tayoumako Damla nopp té khaar bou yagg bi meuneutou mako Ci gaaway waay, Ci gaaway waay Néko rang mouy gaaw waay Ci gaaway waay, Ci gaaway waay Ci gaaway waay Doro faayou woo waay Ci gaaway waay Ci gaaway waay, Ci gaaway waay Ci gaaway waay, waay waay Ci gaaway waay, Ci gaaway waay Ci gaaway waay, waay waay Même soudé yangmay defal adunaak li ci biireum Nga deff foulaa mako gueuneul Soudé foulaaa leu dougueul ci mane Nagn dem VAR Mane dama beug done sa Halal Né nga bokoulok niom kone nak defal différence Diaye diomba niaaw bi damay sonal Mbeuguel bou deugou andaak lokhoy kessé damey doundeul Boumaak nioniou alall sonal Douma Coumba Gawlo tidjil ma ndakh mangui feugueu Saa sounek mangui daaw ci sa ay beug beug Gawal gawal ci mane,khana dotoul deug? Mongui beug waay daal ci deug deug Bayil feemou bi nak! Dokhane bi doyna nak! Daaw ba réne ngey dougou gueneu Wakh niou kagn ngey niow takk Bayil feemou bi nak! Dokhane bi doyna nak! Daaw ba réne ngey dougou gueneu Wakh niou kagn ngey niow takk Gaawal mba ngey loukhouss Baniouma sa poukhouss Auto you cher gallé you nice Kholouma mako dou touss Ci gaaway waay, Ci gaaway waay Neko rang mouy gaaw waay Ci gaaway waay, Ci gaaway waay Ci gaaway waay Doro faayou woo waay Ci gaaway waay Ci gaaway waay, Ci gaaway waay Ci gaaway waay, waay waay Ci gaaway waay, Ci gaaway waay Ci gaaway waay, waay waay Par AbouAmg