Par AbouAmg Sam bopp lala diapé Maak yaw la wone bagniy ndaw Ba takh na lou meuss yandou mane Dey fanane ci yaw Sa nakar sam boss bo piquiro ma nane fa ay dome Khalé laa wone té amone naa yéné ma toudé laa dome Khana dou yama newone " fo dee ma dee faa " Mane khamone nani doma yakkeu moukk ndakh CFA Khana fatelikou woo souniou none ya Khamal ni foma tekk rek mane tekk nala Fouko raw Kharit yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Bestie bestie sama real bestie Kharit yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Bestie bestie ki moy sama bestie Ohh my bestie oh oh Bestie oh oh oh Ohh my bestie oh oh Bestie oh oh oh Siguil maley séne Yaay sama bestie Kharit bou melni bi yomboul Sortez vos amis! Kharit meune na gueune domou ndeye Ya takh ma gueum ko Tey ma wakhal la sey bakh bakh Ba nieup kham ko Lou yagg deug leu yaw keneu nga ci mane Takeu nala kharit goré ngama wane Mangui ci yaw nak ba guèdj gui di ferr Réthiou wouma loumla done khamé Khana dou yama newone " fo dee ma dee faa " Mane khamone nani doma yakkeu moukk ndakh CFA Khana fatelikou woo souniou none ya Khamal ni foma tekk rek mane tekk nala Fouko raw Kharit yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Bestie bestie sama real bestie Kharit yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Bestie bestie ki moy sama bestie Yeah kharit sama woo ma Weur nala ba khadi naa Histoire bi diekh na Naniou dialeu ci lénéne Sougn diganté maak yaw Fofou keneu khadiou fa Té lou yendou ci yaw Souma teudé fananok mome Kharit sama woo ma Souma méré soumla guissé ree Kou melni yaw foumakoy dieulé Yeurmandé bi nekk ci mane ak mom Khana dou yama newone " fo dee ma dee faa " Mane khamone nani doma yakkeu moukk ndakh CFA Khana fatelikou woo souniou none ya Khamal ni foma tekk rek mane tekk nala Fouko raw Kharit yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Bestie bestie sama real bestie Kharit yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Yaw yaay mane té mane maay yaw Bestie bestie ki moy sama bestie Par AbouAmg