Yeah Hummm humm! Hahaha Doundou Guiss Manela waay Morééé REPTYL MUSIC, DIPHéy Mister Thière 1} Ma Yaguena wakh town bi dafa tarr waay Pa beugoul ma xam accident de travail Téwoul niou magg ragné niggah Kone nékouma di Rap pour meuneu nekh nieupeu Ma dakk RAP cii Monde bi yeup"walaay" Maay Pakka Poute boudé réwandé ngay djaay Dafa am cii nioumay settt nigga Bou nékoul wone nioniou may gueuneu réw nieupeu Yaguena dégue Wow Yaguena dégue Wouuuu DIP moussoul nek sur scène naane ma ngui djégueulou Ya mom song bi yaw mimay déguelou di bëk nii Ak yaw mi nga xam ni mane rek nga gueuneu djépi Potolamp fii sa photographe dou meusseu soxla flash Fokk ma takk ndax bima done rap xollam da done lakk Numéro 10 doundou guiss Gaïndé Mbeurodi Walahi meuno siss ba rombeu métis bou raciste Boy bi bindeum styleum ak flow bi Masha' Allah Na RAP ba bindeu toureumak disques d'or yi cii assamane cii Ndax sama noone yi dagno yague djapp teuweu baayi Boudoul wone ak niom baayina bou yague té dém djangui From Grand Yoff Arafat Zarco ndandi Faa Sama yoneu tarr lolo takh soufou tank yi khar Yakarouma cii kèn té aduna bi yeup lay gueusseum Kone même bouma done djaay samangorr kène dou am njeugueum{ Def ko sa profil ba sa couverture Sa profil ba sa couverture Def ko sa profil ba sa couverture wala sa profil ba sa couverture (2 fois) 2} Ma Yague naama né baayil fowé khalle Pa bougoul RAP même bouma koy tangal Reuthiou wouma sakh limay def nigga Kone Rap bouma pour foo pour mouy lerr Humhumm Maay yakk rap bi ngèni def Insha' Allah Laata Album nga jott Mixtape bou doy waar Djapalni BEUS NIKI TAY Nigga La Mère de ma mère est née Boy fuck Télé Radio ak Net bi séni Interview Yallah meussoko guiss té do meusseu guiss kouko gueuneu siw Meuno am RAP cii sa téléphone bi té défo DIP Kénène kougne fii né yafi dakk RAP dagnela colé motif Potolamp fii sa photographe dou meusseu soxla flash Fok nga xam gniy leundeumeul bokoul sama programme Rap Nga ba soneu dara démoum xana meuno pause Wala nga baayi ni Old Skool yi yégue ménopause Nigga ma mom sama lamigne louma nekh laay wakh Xam nani sécurité Aldiana rek la amm Batterie pleine non dou mak gni di takk di faye Ngaaka yi nek di khaar Baag rekkay yagg cii Ténn Douma nétali kone da ngay tiite ladialsama équipe Nagne leu xamalni lima dathie dafa wessu métiite Kone boné DIP da wara tarr biw sa MCs yi Day melni ngané Yallah wara djamou yoneinte yii Def ko sa profil ba sa couverture (Yeah) Sa profil ba sa couverture (Hun Hun) Def ko sa profil ba sa couverture wala sa profil ba sa couverture (2 fois) Doundou Guiss Manela Waay Morééé DIP Quinzaine REPTYLE MUSIC