Kholal cii kaw té nga bayifa saye beut Guisso dara lou djara thiow té mo waral lepp Guisso dara lo meuneu laale lo meusseu tiim ak saye beut Kholal ci kaw assamane wessu nga sa level Gni fa né défouniou bruit té louné nga lène dégueul Mais niouné nioune deukou gnoufi kou déh dinagnela yégueul Sama biss mou ngui nieuw, sama booss tayla xeuyna Kone bou défé nga ndieuk dem néko nama diégueul Nieup nénagne daf gnou tiim kone mo ngui cii assamane Loutah mou tek niou fi lathieko saye maame Adama ak Awa Nénagne nioune nio ngui doundeu Akhirou Zamane Kou djot lettrou assamane exactement ndakh dama khawa Yémou cii gni wané nii niom gueumeu tougnouko Pour mane gni gueum gno yéwou gni dess dagno guemeintou Comme Scientifique ak Philosophe yi diémeu prouvé lénène Boudé bo guissoul do meusseu gueum déh nga thi poukeuré men Doko door balle bamou diaaleu Ropalane khalatoufa yégueu Lougni def xana sani niaane Di niaane Yallah na ngou niaane yikoy fekk Assamane Assamane Assamane Assamane Assamane {Verse 2} Kholal cii kaw té nga bayifa saye beut Guisso dara té lifa né xadioul cii seu cerveau Da nga koy khol moulay guiss mo ngui fepp fi ngay dieum Aduna bepp la muur yémoul rek cii sen deuk Kharitou wérr bek Bidew yi mbok Jante ak Naathie Soubeu lay lerr Goudi mou leundeum gentlema Boufay dem do yaubou touss démal sett sa maame Loutah yène makk yi di défar testament Han! Mom réka tedd ndaxté mane xamena Mom rékay aaté mom réka am bobou makkama (Capacité) Assamane nay limite té kène douko dindi Amena diourom niarry (7) Assamanes kounek ak sa limite Boul khol ci nignou doundé cii souf Kigni goungué gniy roukhe Té xam nga dioum wessuwoul Maye gnou lepp lou bepp mindef di woute Bagni meune def li nga gnou santeu fi lek niouy dougou sunu bamell Doko door balle bamou diaaleu Ropalane khalatoufa yégueu Lougni def xana sani niaane Di niaane Yallah na ngou niaane yikoy fekk Assamane Assamane Assamane Assamane Assamane