Lou bandit di nirol Lou wara né jikom Waxma lou bandit di nirol Lane'mo Lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol Lou wara né jikom Waxma lou bandit di nirol Lane'mo wara nékk jikom Wax ma loye def sa compte fess ak ay concer'ou huit clos Rappeur niom gni gui khoti texte ni secrétaire si bureau Profitéwoul bala DIP di nieuw Déy compliqué lolou gua lale fi million Mafi geuneu tchikili Bandit si son bandit si clip (hunh) Gaw ni lucky luke Balle si sa tank gua tchiriri Niari tank si birr piscine bi Miss chips dima pisss melni pitche yi (psss) 24H/ 24 tchi usine bi Mak Idy ak ISS music lucide sans wisky ak shit(hooouuuu) Fougn'la wo magui si biir té Fépp fougn ma wo yakk sa gars yeup si biti (oouuussss) Hééé Hééé Hééé Hééé Lou bandit di nirol Lou wara né jikom Waxma lou bandit di nirol Lane'mo lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol Lou wara jikom Waxma lou bandit di nirol Lane'mo lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol (Han) challenger Aythieu mbeur ioe la geum Bandit la mane non douma rappeur Ndanane la boy ni seu papeu Waxma lou bandit di nirol Sou boba ma wane lani Kani dou chewing-gum Boy bandit bandit'lou boul fi nieuw Wéyy na billy boy ak dém si yalla INO (bandit bandit) Fake nigga mousso ma nékh Fi dou tarr ba gua dégg wouye sama ndéye Métiwone'na mais niou geum ko rekk Ba téyy boy DIP mo geuneu siw monsieur le maire (hahahahahaa) Respect ni yéré bima soll Succès melni guél bima nopp Douniou yeukeuti lokho sakaw moukk classe Khana concert fi kénn démoul tableau(nio bégne) Hééé Hééé Hééé Hééé Lou bandit si nirol Lou wara nékk jikom Waxma lou bandit di nirol Lane'mo lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di niroool (hé) Lou wara né jikom Waxma mou bandit di nirol Lane'mo lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol Bandit dou réyy teud 10ans jale non! Business ba done milliardaire Yama makk mala meunn Lép mojji machalla Dama touli louf nékone adiak'diakk Kakatar laminn bou toll ni tiakaba Khadial ma dang mayy khadial maan Dagua thiangg yakk sa music bou khaniaral Bayi sa lokho pour diapp fann Douma tégui tank magui casamance Sama bakane la tekk boy ni mbacké mbacké Geumouma thiakhane'katt yi niodi gentleman Sheutt tey dji bandit yi laye wayale Wahou'makk boy yi dioudou beurki démb ndiaye Bandit la fils kone dérétt douma titt Bandit la mane si kébétoukatt yi Tekk si sadique ni kouy nane dérétou vampire Lou bandit di nirol Lou wara nékk jikom(hé) Waxma lou bandit di nirol Lane'mo lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol (haaa) Lou wara nékk jikom(héhéhé) Waxma lou bandit di nirol Lane'mo lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol (bandit- ba-bandit-ba) Lou wara nékk jikom(héhéhé hoo!) Waxma lou bandit di nirol Lane mo lane mo wara nékk jikom (hééé) Lou bandit di nirol (hé) Lou wara nékk jikom (hééé) Waxma lou bandit di nirol Lane'mo lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol Lou bandit di nirol (héhéé) Waxma lou bandit di nirol Lane mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol Lou wara nékk jikom (hé) Waxma lou bandit di nirol Lane'mo lane'mo wara nékk jikom Lou bandit di nirol (End)