Afficher la Vidéo Dip Doundou Guiss - Me N You, Les Paroles, The Lyrics... Li si man néwoul si niom Li si niom néwoul si yow ooh my lova Li niouy wakh man yeugoumako cuz I... Ndakh bou done film, fin bi mak yow la hoo ha Girl I love you and you know I love you and you know oooh ah oh ah Aaaah Aaaaaaaaah Kay nga wakhma bène yone Calme bi fi nek dafma moudj soff Status rek lay guiss si ay stories Amnga connexion mais communiquer woo Loutakh nga beug mel ni niom Li ma guis nga def ni mom dou sa djiko Louma wakh nga bagne ba néma no no Nala fék fi nga né lidiantiko Man douma daw, douma daw Niom nieup danio fog ni lep dina diekh Ma-ak yow meunoul bania nek bikg-ak pèle Khamna gni beuga yak souniou diguenté Lan mo takh niou beuri noone wowo Lan mo takh niou beuri noone wowo Me and You for life my baby Bo naré dioy man ma weuy "Woman no cry" Lan mo takh niou beuri noone wowo Lan mo takh niou beuri noone wowo Me and You for life my baby Bo naré dioy man ma weuy "Woman no cry" Li si man néwoul si niom Li si niom néwoul si yow ooh my lova Li niouy wakh man yeugouma cuz I... Ndakh bou done film, fin bi mak yow la hoo ha Girl I love you and you know I love you and you know oooh ah oh ah Aaaah Aaaaaaaaah Sone tchi dila namm Sone tchi dila ladj louma déf Baby wakhma bou gaw fan nga né Ma fék sila kay niou dadjé Meunoma bayi ngakh sékou niou lolou Meunoma beug té beugoma wolou Boul di khaadj di khaadj di khaadj Khol di ladj, di ladj, di ladj Boul daw, boul dém, boul nangou lepp yakou bène yone Boul may sa noone yi ndamou, kheuy di lakatou di diooy Boul di khaatch di khaatch di khaatch no Khol di ladj, di ladj, di ladj Lan mo takh niou beuri noone wowo Lan mo takh niou beuri noone wowo Me and You for life my baby Bo naré dioy man ma weuy "Woman no cry" Lan mo takh niou beuri noone wowo Lan mo takh niou beuri noone wowo Me and You for life my baby Bo naré dioy man ma weuy "Woman no cry" Li si man néwoul si niom Li si niom néwoul si yow ooh my lova Li niouy wakh man yeugouma cuz I... Ndakh bou done film, fin bi mak yow la hoo ha Girl I love you and you know I love you and you know oooh ah oh ah Aaaah Aaaaaaaaah Lan mo takh niou beuri noone wowo Lan mo takh niou beuri noone wowo Me and You for life my baby Bo naré dioy man ma weuy "Woman no cry" Lan mo takh niou beuri noone wowo Lan mo takh niou beuri noone wowo Me and You for life my baby Bo naré dioy man ma weuy "Woman no cry" (Reptyle Music)