Kishore Kumar Hits

Dip Doundou Guiss - Family текст песни

Исполнитель: Dip Doundou Guiss

альбом: LNN (Loo Ñeme Ñàkk)


Soukkou gnaan ngir gnabot dji
Deukkou nath ngir gnabot dji
Liguéy ba dé ngir gnabot dji
Défar sa life fou gnabot
Soukkou gnaan ngir gnabot dji
Deukkou nath ngir gnabot dji
Liguéy ba dé ngir gnabot dji
Défar sa life fou gnabot
Yéy yeah
Défal si waa keur gui
Dori waar gnou déf si waa keur gui
Défal si waa keur gui
Khamo loutakh sa papeu rare keur gui
Défal si waa keur gui
Dori waar gnou déf si waa keur gui
Défal si waa keur gui
Khamo loutakh sa papeu rare keur gui
Yéy yeah
Maman sonneu na loloul
Déf na louma warona déf si gnoun
Papa sonneu na loloul
Déf na louma warona déf si gnoun
Ki nga don mounoul bokkak ki nga am
Fo meunti tollou dou yém sa Ndeye ak Baye
Boul meusseu yéss ba di tass ñom sen yaakar
Maman daa khékak dé
Diokh la sa life
Diokh la sa freedom
Yarla si baatin déf si yaw foulak fayda
Dokh na ba fébar pour meuneu fath sa fébar
Wakh ma ban banque lanlay diokh pour nga fay bor
Yeah paabi da liguéy
Néna thiaabi yaa ngi ni
Moy nga déf ma magueu bég
Est-ce que bandit yaa ngi djém?
Bess dé man dé naafi gueuth
Héritage dou khaliss
Na nga ar sa famille yeup
Nakh guiss naafi taalibé
Soukkou gnaan ngir gnabot dji
Deukkou nath ngir gnabot dji
Liguéy ba dé ngir gnabot dji
Défar sa life fou gnabot
Soukkou gnaan ngir gnabot dji
Deukkou nath ngir gnabot dji
Liguéy ba dé ngir gnabot dji
Défar sa life fou gnabot
Yéy yeah
Défal si waa keur gui
Dori waar gnou déf si waa keur gui
Défal si waa keur gui
Khamo loutakh sa papeu rare keur gui
Défal si waa keur gui
Dori waar gnou déf si waa keur gui
Défal si waa keur gui
Khamo loutakh sa papeu rare keur gui
Yéy yeah
Never forget
Fima djougué yé
Fima diar
Lolo takh bama melni
Am am dou wéss
Gnakk dou weuy
Mais mouno khaar lofi joboul ba diotsi
Dérétou gorr rek mofi daw

Xalei bou guiss rangognou méram di tokh
Bou diom sakhoul sa kaw khamalni méloni mom
Boul diar si yon bou diobeudi ak yon bou téreudi bro
Diay sa ngor dou yakamti mais gueumeudi la
Yéy yeah
Défal si waa keur gui
Déf lo meun ak lo meunoul si waa keurgui
Yéy yeah
Lép thi waa keur gui
Lép pour sa family yaa
Soukkou gnaan ngir gnabot dji
Deukkou nath ngir gnabot dji
Liguéy ba dé ngir gnabot dji
Défar sa life fou gnabot
Soukkou gnaan ngir gnabot dji
Deukkou nath ngir gnabot dji
Liguéy ba dé ngir gnabot dji
Défar sa life fou gnabot
Yéy yeah
Défal si waa keur gui
Dori waar gnou déf si waa keur gui
Défal si waa keur gui
Khamo loutakh sa papeu rare keur gui
Défal si waa keur gui
Dori waar gnou déf si waa keur gui
Défal si waa keur gui
Khamo loutakh sa papeu rare keur gui
Yéy yeah

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители

Jeeba

Исполнитель

VJ

Исполнитель