Sa loxo set Sa lepp set Bul nuyu kenn Bul lëng kenn Bul génn kese ndax bëg génn Bul sëqët fepp Bul jége kenn Sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ Soj, problème noyi, senn sa bakkan Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ Du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn Sa loxo set Sa doom yi set Bul nuyu kenn Bul lëng kenn Bul génn kese ndax bëg génn Bul sëqët fepp Bul jége kenn Sa loxo set Sa lepp set Bul nuyu kenn Bul lëng kenn Bul génn kese ndax bëg génn Xeex ak Corona Virus, Microbe, jàngoro la, du nit Aduna nek si combat Du gis ku muy xeexal Nuro nak grippe Nañu éviter contact physique Xajul Grand Yoff, Colobane, Pikine Tax ba ñu annuler programmes yi siiw Tax ba ñu foog ni àddinay tukki Medecin sonu na si li Amul vaccin, ordonnance tamit Mu ngi ray, day toroxal nit yi Buñu tooge dina bari ay victimes Set si sa askan, set si sa bopu Tëju te baña seeti sa mbokk Julli sa màkkaan, Messe si la bokk Xeex ko mu jeex mbir yepp mëna doxx Masque, sabu, antiseptique Raxasu, sangu dadi set wecc Dal, muñ, bañ lu melni dess fi Gën di ñaan pour jamm day dikk Sa loxo set Sa lepp set Bul nuyu kenn Bul lëng kenn Bul génn kese ndax bëg génn Bul sëqët fepp Bul jége kenn Sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ Soj, problème noyi, senn sa bakkan Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ Du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn Sa loxo set Sa doom yi set Bul nuyu kenn Bul lëng kenn Bul génn kese ndax bëg génn Bul sëqët fepp Bul jége kenn Sa loxo set Sa lepp set Bul nuyu kenn Bul lëng kenn Bul génn kese ndax bëg génn