Kishore Kumar Hits

Nitdoff - Diyeu maman текст песни

Исполнитель: Nitdoff

альбом: Roi d'Afrique


Bouldi bouldi bouldi no no bouldi cry
Thioneu bi ngay dathie tchi Keur gui maman no dou say
Ma Ma suma yaay
Beugu naleu terreul fi tchi adouna
Maman yow sa khole bi féss neu yeurmandé
Sou dome dioyé nga djioy sou bégué nga réh
Soneulo sa borome Keur tchi xoulo ak khekh
Oufeul nga ko ndiambot dokh tchi liko nekh
Maman maman sama yaaay
Togueul niouley beuss akeu raay
Wakhma louy sédeul sa khole ma def ko yaay
Taye dhi dameu xeuy ni fokk diar rek ma finte waaay
Maman we love you
Maman we love you
Maman we love we love we love you
Maman we love you
Maman we love you
Maman we love we love we love you
Yaye dafeu sonou tchi dome
Yaye dafeu yagua soneu tchi dome
Yaye taloul dara lepp nguir dome
Yaye dafeu yagu sonou tchi dome
Sayo tissé da nga sorri sey dome
Lepp lou bakh nga diglé pour niou ame diom
Taye dji dameuley santé nit kima doon
Amoul teranga adouna yow boula diomb
Maman goudeul fane magatal beu nior xomb
Yalna yékh mais aldjiana ngui sa tombe
Yaye boye li nga nianoon nanguna yow hanhun
Taye seu dome yi seuyi nagn beu doon aye parents
Dome loumouy fayé tioneu waadiour
Khana mague tékki teral ko ni bour
Fatalikoul thioneu eumb ak seugu diour
Akhou ndiourel bakhoul kone nak ma gui délou toub
Maman we love you
Maman we love you
Maman we love we love we love you
Maman we love you
Maman we love you
Maman we love we love we love you
Yaye dafeu sonou tchi dome
Yaye dafeu yagua soneu tchi dome
Yaye taloul dara lepp nguir dome
Yaye dafeu yagu sonou tchi dome
Sama kholeu binde waye bi
Waye tchi sama yaye dji meu diaral lepp
Kimeu lebal borr bouma menoul faye
Diouraume niénti wérr ya beu sunu dioni taye
Yaay meusseu doon sama kiraaay
Maman andil naleu samey dome
Niou ouffou tchi sa wét nane leu mame boye
Mame boye nane leu mame boye
Maman we love you
Maman we love you
Maman we love we love we love you
Maman we love you
Maman we love you
Maman we love we love we love you
Yaye dafeu sonou tchi dome
Yaye dafeu yagua soneu tchi dome
Yaye taloul dara lepp nguir dome
Yaye dafeu yagu sonou tchi dome
Cédéna ni yaye diou bakh nga
Cédéna ni yéwén nga yiw nga
Cédéna ni ame nga diné
Maman love yaay sama réni khole

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители

Tafa

Исполнитель