Yeah I respect the game right ma décidé same life Dém nigga tryna copy but déy djaffé tchi djeem right Ma braquer sa zone KK yi bégué si sen side Hip hop done agoniser ma nieuw diokhat ko sense like The nigga with the doff style roubé na sen scribe Bang bang b-bang taye moudjé neu diss price Underground king mane leu mbède bi give choice Loudoul Rap tigui Rap domafa guiss twice Nigga ki nga done wait aksina pile poile Ma ouf djant ouf werr meunouniou equal Sa gaïndé dafeu mine zoo meuneutoul dekou aleu Mofuking youkhou ouhhh takhoul niou equal May bombe di blackout sa secteur di doubt about Sey nigga leulou pino cuz my gun is pop out Bou game bi doundone deugue do lale mic bey khèp chèque Thiogalou bullshit kouneh di niodi rapper fucking flop Face Dém slap crap and trap ganda-propa So banié deh xeloul dielna raw gadou gui té wékhaloul Yagui mey signe di reh mais xamna sa beugn wékhé woul Nii sa khole fekhé woul Mc xewiwo mais dang fé xéwoul Xeuyna di enchainer Mc yi melni Casanova KK mousta keuf mic di rap nga degu that's enough Kou real rap di djap lo dathie na nga dass sa nopp Ma diokhla frappe youy percuter melni bastonnade Thiafka wou mbed bi la miine lo séni estomac Keep it real ni dieun bi di miné ndokhou guedj Yeah rap bi ley falo nekh meti pray for lord Nigga li ngey nakhé sa public mom laniouy néfaro Doctor biley consulter fadjie leu donté sakh fébaro Doma frek tchi mafia wou mbed bou fekké pégro Guiss nga mane ni mey téguo tchi beat bi damey raye ego Khibone nga té régueu go di splif up like raggae go Mc da nga djiégué gow (fille) khana douguaguo négou goor Chaise bi boudé kén dongue mane maay took Mbedeu boudé séni song mane maay talk Dem niggaz bullshiting bou diant fink beu night o clock Daminé sa L dou takh nga dégu nice spoke Ay ranguoniou rethiou nioy walaguane sa eyes tokk Déloul sa Size joke togual ak sey guys job Koccé né Ndongo guili né gongo paré si songo Fake ya ngui tongo leungo Maay lingot ni soufou congo Tengo lou dinguo diom bi laay djiengo ngey oufou comme gow Nigga compo séni complot dou képpeu Sonko Listen dou wané tisseum dafeu deglou 3-4-5 rek 6 meu sisseum King la ngey misseum nit yi ley gueusseum atano ndisseum Mbed moma harmoniser now mey dokh si peaceum di fils seum Keep it G nigga every season, the mission I got the vision now they give me reason Li ngey wout ak limey wouteu bokoul sa respect yokoul The money is so cool but andoulak respect soma guissatoul Kollëré doguoul fitou none toguoul sa mc dioboul Soukh nga thioguoul tolowounie pass pass bokoniou struggle Mister mad mic ndeusteun nou last night Moss naniou nathie nathie diotna niou dathie light Di noce like té douniou lost right Dieumbeuteul love sassouneh djiemeul kill hate Dieum dji loff tewoul nga rich néh Bill Gates Ame ame ak niak ci bopp leu Nigga stay proud So niaké foula niou dioguila nigga stay proud Boul xép sa bopp di dounguourou nigga stay proud The most high moy contrôler nigga stay proud Xam xam bi diomboula nigga you gotta play though