Kishore Kumar Hits

Hakill - Do Comp текст песни

Исполнитель: Hakill

альбом: 3e Baraam


Legui nak... dara diakhalatouma dara YEMOUMA
Young neggah legui nak.wakhtanou kou teukh leu kou goumbeu ak
MOUMA
Fi kéne falétoul kéne bopp sa bopp EGOisTE
Kouné y'ak sa xél bou gatt rekkay PETO FILS
Dawal sentiment ba accident eumb DEGN KO MISS
Wowé sa guél bébé té ngakoy teudé PÉDOPHILE
Tass Yakar melni ETO'O FILS
2002 la Sénégal bayi dieuf di EGOTRIP
Politicien yi dagn niouy nakh chaque jour ni FOND VERT BI
Gnila gueneu diégué bougn lay tour leundeum KEY DO GUISS
Pauvre yey gueneu liguey mais pauvre yé gueneu BEURI
Largent appel l'argent pauvreté moom amoul sakh CREDIT
Testament amatoul ndakh amatouniou lougn fi BAYI
Yoon bou done dokhal yoon president moy ndieukk diar CREI
Loutax Toubab bi diokh niou indépendance béne 4 AVRIL
Parceke dafniou poisson d'Avril NGAAKA BI
Dou rey nagn niom Sankara ak niom KHADAFI
Pays emergent bouy daw 1 a l'heure CARAPID
Nekk Top model la gueneu diégué que nekk MODEL
Sagam Yallah sakh nopina wakhou nit loumouy NDIEURIGN
Adouna kay moom touki na mais xamouniou foumou DEM
Legui mem Jésus mountoul oubi beut wakhouma SERIGNE
Sip Do sakh sip... Young neggah do sakh sip
Do sakh sip... Yeah do sip... Young neggah do sakh...
Young neggah Do comp. guisouma lou leer fi lepp leundeum dara
Leroul sama bopp
Ooh no dara leroul sama bopp
Lepp diakhasso mane khamatouma Young nigga do comp
Djiguéne yéngui seuyak djiguéne gni
Goor yi di tédeuk goor gni
Bakane laniouy wethio money
Mane sama diamono mongui
Young nigah do comp
Do sakh comp. Do sakh. Do sakh comp.
Ooh no do comp
Do sakh comp... Do sakh comp. Do sakh comp.
Doundou bou melni vie de rêve la GUÉNTOON
Guente biir guénte la kay lane la FOGONE
Bala politicien wakh na wakh LÉBONE
Kouy khar ci niom kheuy nala leer ni DO GONTE
Nit yangui beugue reutch dé mais dougne deff loudoul dieufou
SAFARA
Pourtant nieupp meun reutch safara mais kéne dou REUTCH DE
Sénégal nioufiy gueune doxal industrie SANGARA
Boy xol toudouniou Jean Paul François wala PIERRE
Aye boy you beugoul deff dara ni kou dioudou jour FÉRIE
35 ans profession FAIT RIEN
Wéréntek talal loxo ya ciy PREMIER
Aye parent you amatoul yakar TERMINE
Sénégalais mouma dou lekk khalissam DÉDETE
Kone sa you guéweul wakh nala leer mongui INVESTIR
Dakk lekanté sougn bir takh deume yi RETRAITE
Wakhkatou deugue nala leer ni nieupp DÉGN KOY FUIR
Ale ma bic bou fanaan bir rongoniou DEUM
Safara ci na xeegn melni cocktail DEUTT
Souba examen bi dagn ko wara géré DEUGUE
Wala fuite yi dal triché day fay DEUGUE
Prof yi diangalnagn ma lepp sauf nouniouy TÉKIWE
Kéne dou taan dioudou pauvre mais bo ci déwé yaw la NEEX
Gni amoul louniouy lekk rekay né di DIDJI DEY
Dara yomboul mais vrai yigo dafay nangou XEEX
Sip! Do sakh sip... Young neggah do sakh sip
Do sakh sip... Yeh do sip... Young neggah do sakh...
Young neggah Do comp... guisouma lou leer fi lepp leundeum dara
Leroul sama bopp
Ooh no dara leroul sama bopp
Lepp diakhasso mane khamatouma Young nigga do comp
Djiguéne yéngui seuyak djiguéne gni
Goor yi i tédeuk goor gni
Bakane laniouy wethio money
Mane sama diamono mongui
Young nigah do comp
Do sakh comp... Do sakh. Do sakh comp...
Ooh no do comp
Do sakh comp... Do sakh comp. Do sakh comp...
Legui nak. dara diakhalatouma dara YÉMOUMA
Young neggah legui nak.wakhtanou kou teukh leu kou goumbeu ak MOUMA

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

YIGO

2021 · альбом

Jar

2021 · сингл

Fii

2021 · сингл

Похожие исполнители