Kishore Kumar Hits

Adiouza - 7 à 77ans текст песни

Исполнитель: Adiouza

альбом: Li Ma Doon


Nax sa keur dou tax
Bougnou seyé xaleyi dounla mèré
Nax en tiiii nangou na kon ba dounla méré
Nax sa keur dou tax
Bougnou seyé xaleyi dounla mèré
Nax en tiiii nangou na kon ba dounla méré
Yagui xey may gontou bay wadia gnibi
Néké Mbeuguel 7 à 77 ans
Ma lay lathie 20ans yima dessé
Bébé te nga nieuw gounghema
Magui xey ngay gontou bay wadia gnibi
Néké Mbeuguel 7 à 77 ans
Ma lay 20 ans li la déssé
Nax man nama se beugal
Xam na ni dal li ma min tiss na lolou
Man tissou ma nax kounek beugeu guissé
Ba méro sama xalate doyna war
Pas de tout man deh dérangewuma
Nax at yi nga am mom la taw di titoro
Pas de blême tarou jiguene sey la
Tonton négou sey dafa touti
Niar gniou beugante mana boko lal
Tonton négou sey dafa touti
Niar gniou beugante mana boko lal
Nax sa keur dou tax
Bougnou seyé xaleyi dounla mèré
Nax en tiiii nangou na kon ba dounla méré ayi aya
Nax sa keur dou tax
Bougnou seyé xaleyi dounla méré
Nax en tiiii nangou na kon ba dounla méré
Tonton néné Tonton néné tonton beug nala
Bébé yar bi nga ma yan
Bou dagoul anti dou xoulo
Bébé djiko bi nga ma yan
Bou dagoul xale yi dougou kass
Anti lako wara djil nax mou kontane
Mou xam ni seysiwo danga diamousi
Bébé beugouma wagal sama none ba togne sama borome
Kin dal diapalé gnibina
Kin dal wétali gnibina

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители

Titi

Исполнитель