Eey Màsamba Waalo Hummm hun Su mbëggeel doon jaay Am naa njëgam Dinaa la wan sama yéene yi ma am ci yaw Duma ku lay jay Te duma la wor Dinaa la wax dëgg ak lum metti metti Maa la woo ne la maa la nob Miinal la sama bopp ba nga barder maa la tooñ Kon nag loo ma manti def Lu mu metti naa ko muñ Àdduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi Ay bu doon ay nax neex na ma Fekk ma ciy gént yee nga ma Jàmm ju bari may nga ma Yaa ngi may dundal àjjana Tamit tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne man la Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan Tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saadjobaan eeee waay Xam nga duma puruux duma fàtte bi may surux Xuntu wu lëndëm wi nga ma génne dinaa ko wax Du lu rafet ci wax Soo ma bàyyee damay torox Nawle yépp bis bu ñu teewee dinaa ko wax waaaay Doy nga ma ci kër Kenn du la sikkal Man yaw mii yaay ki ma fiital Doo dund ngistal Ngor gi nga jiital Ragaluma siiwal Nun ñaar ndax doy nga ma ci kër Ndaxte Mane maa la woo Ne la maa la nob Miinal la sama bopp ba nga barder maa la tooñ Kon nag loo ma manti def Lu mu metti naa ko muñ Àdduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi Hay bu doon ay nax neex na ma (bu doon ay nax neex Na ma) Fekk ma ciy gént yee nga ma (Fekk ma ciy gént yee Nga ma) Jàmm ju bari may nga ma (Jàmm ju bari may nga ma) Yaa ngi may dundal àjjana Tamit tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan Tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan Tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan Tëggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan eeee waaay