Kishore Kumar Hits

Viviane Chidid - Do Dara текст песни

Исполнитель: Viviane Chidid

альбом: Benen Level

Néne dafa am mana
Té yoroul ndieugou nana (yorou ndieugou nana)
Néna dafa am mana
Té yoroul ndieugou nana (yorou ndieugou nana)
Meune niodi, beugue Jay graw (Jay graw)
Té yaw yoroulo nada (yoroulo nada)
Meune ngondi, beugue Jay graw
Té yoroulo nada sah
Néna yorna (oh oh ooooh)
Ndéké yoro Lou souker café ak barada (eh eh eeeeh)
Muy calpém di possam lépam xotékou (oh oh ooooh)
Lékou lo dé nanou lo
Sa nélaw dématoul, néngua yoor ngua(eh eh eeeeh)
Di fowé sa xel bi molay sonal
Goor su né Waaa ngua Jomb
Di deuké lou yomb
Lou fi jaar nguay wané
Jomb niaw randouma
Té digué lo meunul
So teudé do nélaw
Dou ningua beugue doundé
Dou ningua beugue doundé
Ki tocc na kogn ba (oh oh ooooh)
Ndéké yoro Lou souker café ak barada (eh eh eeeeh)
Muy calpém di possam lépam xotékou (oh oh ooooh)
Lékou lo dé nanou lol
Sa nélaw dématoul, néngua yoor ngua (eh eh eeeeh)
Do dara
Do dara
Do dara
Niata yon ngua Dieul alalam té fayoko
Niata yon ngua Dikk Pa yi au mère yu
Niou adji ji Makka (makka)
Té deffo ci dara (dara)
Nioune guissou niou dara (dara)
Ndéké yaw do dara
Néne dafa am mana
Té yoroul ndieugou nana (yorou ndieugou nana)
Néna dafa am mana
Té yoroul ndieugou nana (yorou ndieugou nana)
Meune niodi, beugue Jay graw (Jay graw)
Té yaw yoroulo nada (yoroulo nada)
Meune ngondi, beugue Jay graw
Té yoroulo nada sah
Néna yorna (oh oh ooooh)
Ndéké yoro Lou souker café ak barada (eh eh eeeeh)
Muy calpém di possam lépam xotékou (oh oh ooooh)
Lékou lo dé nanou lo
Sa nélaw dématoul, néngua yoor ngua (eh eh eeeeh)
Di fowé sa xel bi molay sonal
Goor su né Waaa ngua Jomb
Di deuké lou yomb
Lou fi jaar nguay wané
Jomb niaw randouma
Té digué lo meunul
So teudé do nélaw
Dou ningua beugue doundé
Dou ningua beugue doundé
Ki tocc na kogn ba(oh oh ooooh)
Ndéké yoro Lou souker café ak barada (eh eh eeeeh)
Muy calpém di possam lépam xotékou (oh oh ooooh)
Lékou lo dé nanou lol
Sa nélaw dématoul, néngua yoor ngua (eh eh eeeeh)
Do dara
Do dara
Do dara
(Drum)
(Oh oh ooooh)
(Eh eh eeeeh)
End

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители

Titi

Исполнитель