Maam mor Mandouté Sa lamign bi naguko té Sa beut yi tam naguko té Bougn né déme rek gua déme Kouné amna foum wara yéme Kone Yemal si sa domaine Lepp loy digué gnagua ko meune Beug daradja boum taxe guay féne No def bess dina feign Boul def lo degg waxko Meune nala dioureul kasso Yafi def yafi waxone As Gor Dako war di moytou Nagua mandou si képeu kouy dox Té doylou si lign la diox Loussa yone si sama yeuf Legui juge jugeél say dieuf Boul degg dadi geum Wala guiss rek ni waw Guiss dafa wara lerr Degg tam wara xote Diangual xam lathia birr Ba meune xam lathia biir Bo paré xam lassa birr Boy Nagua mandou bayilen si birr Koulay lath lo defoul Boulko rouss wax neko defo Koulay lath lo xamoul Boul ragal neko xamo Nitt day mandou ame foulak fayda Boul nangou kéne dila fenlo Defal lo xam Waxal lo xam Foo déme bo teudé nelaw Defal lo xam Ko xamoul loumouy dox bakok doxam Lep lou waye di wax dess koy xalat Ndax euleuk do xam Bo doné kilifeu oufeul sa ndiabott té bayi toguane Diougoulo figua tok loussa yone si nitt kék autom bou panne Sou ñep mandou wone kene dou ame problème Fi Kou teulei dém né sa morom do dém Koula newoul goungué ma lokoy topé Féne ak dieuw gor warouko diobé Xolal sa lamigne bi nimla noté Boumou gooré kene doulako takal Bamelou biire kene doulako gassal Meuno té kou def gua dièm ko yakkal Xamo té kou wax gua dièm ko sossal Nagua mandou si diné djambour Mandou si tarixa djambour Mandou si allalou djambour Jabarou jambour ak domu jambour Li geuneuy mandou si diné djambour Mandou si tarixa djambour Mandou si allalou djambour Jabarou jambour ak domu jambour For real Boul degg dadi geum Wala guiss rek ni waw Guiss dafa wara lerr Degg tam wara xote Diangual xam lathia birr Ba meune xam lathia biir Bo paré xam lassa birr Boy Nagua mandou bayilen si birr Koulay lath lo defoul Boulko rouss wax neko defo Koulay lath lo xamoul Boul ragal neko xamo Nitt day mandou ame foulak fayda Boul nangou kéne dila fenlo Defal lo xam Waxal lo xam Foo déme bo teudé nelaw