Kishore Kumar Hits

Titi - Jiggen feem текст песни

Исполнитель: Titi

альбом: Titi la lionne


Jiggen sou beugué am manorééé... thi seyam!
Neu guéné lep, koundioug yék kadiague yi... Boul négligé tar. Neu safeu saf... Beuss bou nekeu... indil féém you bess
Boul ko khep djinakh dey bari pakh
Gaaatéééko ba foumou dém yow rékeu ley khalate
Jiggen sou beugué am manorééé...
Dey jonguéééé té bary féém
Jiggen sou beugué am manorééé...
Dey jonguéééé té bary féém
Na saf!
Fik mingui bék yokal dose bi boulko outeul frontière
Na safa saf... Na gueneu saf
Pampam piram pampam wata bambam
Jiggen sou beugué am manorééé...
Dey jonguéééé té bary féém
Yow bo beugué am manorééé...
Jonguél!
Té fékhel beu loumou lamb dadji
Té bokou soré dang koy wéteul
Té loumou mér mér, fékhél ba mou ré
Té bouko niourou dionguéééél ba mou saf!
Na faf melni adouna yéén dongua thi né
Jiggén sou beugué am manorééé...
Dey jonguéééé té bary féém
An an... An an an an... An an an an an an...
Yow baril féém!
Jiggen jonguél jonguél beu mou meut wonél say féém!
Ték ko thi temps té civilisé wonél say féém!
Djeuffé ko deuké ko wonél sa féém!
Mine nguameu mine nala dagnou wara sey
YAllah ma bolék yow degnou wara sey
Mine nguameu mine nala dagnou wara sey
YAllah ma bolék yow degnou wara sey
Seyallaaaaa man
Samey dooma wara takh meu nanguou lou métti papy
Beu fougnou meuneu dém beu fougnou meuneu né
An sey bimey sey molène di walooo...
Papé!
Papy louleu nékhoul thi mane dameukoy dindi
Gawémeu gawémeu man yaw lay sét
Mbeuguel dou ray ci niaye sou guené fegn
Dou ci wakhine dou ci djeufine ... Yow lay sét
Louleu nékhoul thi man meu dindi sani
Oooooooh papy chéri yow lay sét
Papy sou doyoulé meu doli
Louleu fi nékhoul dal damakoy dindi
Pitakh yangui ni, souleu doyoulé
Sou doyoulé meu doli yow lay sétt
Papy yAllah bolléna mak yow. Yow lay sét
Bayina kharite andando yow lay sétt
Djitteul na sameu yakaaar ci yow
YAllah bolléna mak yow. Yow lay sét
Éééééh djine naleu oooooh man yow lay sét
Ééééééh.

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители