Kishore Kumar Hits

Titi - Gen ji dekk текст песни

Исполнитель: Titi

альбом: Titi la lionne


Guentouma hé Gentouma
Hoooooo HOoo!
Guentouma hé Gentouma.
Beugouma yewou rek guente gui diekh.
Ngua neck fi ma neck feulé Dou té niou gussanté
Nékal fi mangui feulé Beugenala,
Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako.
Beugnala Guemenala
Geumnawooo Ho
Guentouma!!! Guentouma!!!
Nekkal fi ma neck feulé Dou té niou gussanté
Nékal fi mangui feulé Beugenala
Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako
Beugnala Guemenala
Geumnawooo Ho
Guentouma!!! Guentouma!!!
Naniou Khalaté lou lenne nekh ci mane
Bayiléne niou wakh louléne nekh ci mane
Maye adji kiiy beug. Beugnala
Beug Sa Deuk Ba Deuk Fa mouy guene di deuk ci mane. "WTF"
Yaw yaye ki kidnaper sama life
Hooo Hooo My life...
Kidnaper sama temps khamnala
Temperature bo necké soma guissé guif
Dangua beugonna kham ci lanne la néék
Dangua beugonna kham ci lanne lay dokh
Yakamtina niouye skype
Deug sa viber, am sa allo!
Arrosé na samay fleur mane
Ba meuna feyy ci bissoub mbeugéll yii
GEN JI DEKK dama yague ak yaw
Ba so yeukeutii say kaddu
Bala nguay danéél makoy teureul
GEN JI DEKK
Geunalanté wouma la ak niom My baby
Dafa fekk ni do niom douniou yaw
Minne na la Tammou na la
Mane mala tamou ci niom ba ngua doyma
Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo
Ni mala beugué rombe na Yillif
Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo
Ni mala beugué rombe na Yillif héé.
Sama guente gui
Mba douma yewou rek mou diekh
Sama guente gui
Mba douma yewou rek mou diekh
Sama guente gui
Mba douma yewou rek mou diekh
GEN JI DEKK
Ya léne guene ci mane
Té dou yagg ba ngua donne niom
Do meussa donne niom
Soumay nieuw ci yaw
Ropplane loumou naw naw!
Ma guena gaw ci yaw
Nangouna donne sa autorail
Souma djoubé gare cornet né YEUKSINNA
Beug nala guemnala
Ni mala beugé dafa diegui dayyo
Ni ngua ma beugué rombe na Yillif
Beug nala beug nala
Beug nala!!

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители