Kishore Kumar Hits

Souleymane Faye - Ami N'Diaye текст песни

Исполнитель: Souleymane Faye

альбом: Guëw


Deuguit × 16
Ami Ndiaye x 6
Wallay bour bi Yallah khamnani guinaw lolou Ami rek la nopp mane
Wallay gni may andal kham nagn ni guinaw lolou Ami yow rek la nopp man
Kone loutakh mou may miir lo
Kone loutakh mou may fiir lo
Kone loutakh mou may misère lo
Ami Adouna dou Nonou
Wagnil ni nga nèkè way
Oh Ami, oh Ami
Eh Ami, Eh Ami
Aminta Ndiaye, Aminta Ndiaye
Aminta Ndiaye wagnil ni nga néké way
Aminta Ndiaye, Aminata Ndiaye
Aminata Ndiaye wagnil ni nga néké way
Togn ngama bène yone, madaldi la bal
Nga dèlou tognatima madaldi la bal
Worr ngama bène yone, madaldi la bal
Nga dèlou woratima, madaldi la bal
Ami adouna dou nonou
Dou fi dou fofou
Wagnil ni nga néké way
Adouna dou nonou
Wallay bour bi Yallah khamnani guinaw lolou yow rek ka ma nekh mane
Dou fi dou fofou
Ami dou ni dou nonou
Ami dou ki dou kokou
Mane douma gnonou
Mane Djiguène douma fonto
Wagnil ni nga néké way
Togn ngama bène yone, madaldi la bal
Nga dèlou tognatima madaldi la bal
Worr ngama bène yone, madaldi la bal
Nga dèlou woratima, madaldi la bal
Ami Adouna dou Nonou
Wagnil ni nga nèkè way
Ami dou ni dou nonou
Ami dou ni dou nonou
Ami dou fi dou fofou
Ami Ndiaye, Eh Ami Ndiaye, Ami Ndiaye Ey Ami
Ami dou ni dou nonou
Togn Ngama bène yone ma daldi la bal
Daldi la bal, daldi la bal
Ami Ndiaye, Eh Ami Ndiaye, Ami Ndiaye Ami
Wallay bour bi yallah kham nagn ni guinaw lolou Ami yow rek ka ma nekh mane Ami
Nga délou tognatima ma dal di la bal, dal di la bal, dal di la bal
Ami dou ni dou nonou Ami
Ami Ndiaye, Eh Ami Ndiaye, Ami Ndiaye Ami
Togn Ngama bène yone ma daldi la bal
Daldi la bal, daldi la bal
Nga délou tognatima ma dal di la bal, dal di la bal, dal di la bal Ami

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Nitki

2000 · Мини-альбом

Adduna

2022 · Мини-альбом

Похожие исполнители

Titi

Исполнитель