Mane lima gueneu jaxal si xaley Sénégal moye Musikou lemzo diamono bi daniouko chœuru par choeur Mane lima gueneu jaxal si xaley Sénégal moye Licci télévision bi yeup daniou ko chœuru par chœur Ta ko ci ne récitelma sa récitation Bi duleuko meuneu recitel par chœur Mane lima gueneu jaxal si xaley Sénégal moye Musikou lemzo diamono bi daniu ko chœuru par chœur Il est l'heure il est l'heure il est l'heure Suñu télévision bi dafa am chœur Il est l'heure il est l'heure il est l'heure Suñu musik bi dafa am heure Il est l'heure il est l'heure il est l'heure Diangui école wala métier dafa am heure Il est l'heure il est l'heure il est l'heure Takki diabar dafa am heire Xalei bi buy diangui école Dafay fokni ay wajuram laye jangal Bala muy xamnei boppam laye jangal Bete bou deimei baye binde lettar Jangal Il est l'heure Nekk xale mettina yaye xamna si dara Nekk xale mettina yaye xamna si dara Bul waxli Bul deffli Demal fi Awal fi Waxal li Solal li Simil li Togal li Boul lekk li Nekk xale mettina yaye xamna si dara Boul deff li Boul wax li Solal li Simmil li Muñal so magué mou jex Muñal xalei bi muñal so magué mou jex Muñal Lima jaxal si xaley Sénégal moye Musikou rap bi dañu ko chœuru par chœur Mane lima gueneu jaxal si goney moye suñu Télévision bi daniou ko choeuru par chœur Wayei kocci ne récitelmasa Récitation bi duleuko meuneu récitel par choeur Il est l'heure il est l'heure il est l'heure Jangui école wala métier dafa am heure Il est l'heure il est l'heure il est l'heure Iow deimal seyi dafa am heure Takkil jabar dafa am heure