Sama dom yaayoo sama doom yaay Dama naan la moytoul li Xana ki naan la sangoul sa taar la beug Sa beut bi souff a ngui si sa doomi ndeye a lakoy wax Sama doom yaay dama naan la moytoul li Reuthiou dafay wess. Man deh limalay wax Sa djam lala beugeul tok ba mag di reuthiou dom yaay di mere koula defoul dara ... sama doom yaay Billay topp sa ndaw lou gnaw la Bakkan dagnukoy teraal Magg a ngui si yoonam di gneuw Topp sa ndaw lu gnaaw la