Kishore Kumar Hits

Fallou Dieng - Benno текст песни

Исполнитель: Fallou Dieng

альбом: Namonalene


Waaw bennoo lañu wax
Bennoo lañu wax si miim réew
Bennoo lañu wax
Bennoo lañu wax si miim réew
Sàq bu ñépp bokk jëlal sa wërsëg
Kenn ku ñów jël wërsëgam
Jiite taxu fee gën
Waaye jiitu taxu fee raw
Waaw bennoo lañu wax
Bennoo lañu wax si miim réew
Bu jëf doon jikko kon kenn du sonn
Nit moom mënta baax jikko
Àdduna àdduna àdduna àdduna àdduna da fa yaatu
Waaw àdduna àdduna àdduna àdduna àdduna da fa yaatu
Lu ca waay denc, ngëneel la ciy sàkku
Aateel sa moroom ni sa bopp, mel ni ba nga doonul dara
Fii ku fi juddoo gan gu indiwul yóbbal nga
Way leele leele
Waaw bennoo lañu wax
Bennoo lañu wax si miim réew-a-réew
Lu waay doon, nit a ko ko def
Seetal ci benn buur bi tey Yàllaa mi
Lu waay doon, mbooloo ko ko def
Seetal ci benn buur bi tey Yàllaa mi
Benn loxo du tàccu, benn tànk day sukkooju
Soo nawloo nit, mu nawloo la
Waaw bennoo lañu wax, te it moo gën
Bëggal sa réew, fonkal sa réew, nawlool sa waa-réew, Ësobiyo Ba
Lu mu am mayeko, lu mu am joxe ko
Lu mu am sédd ma ca
Ãa moo di ma xarit
Lu mu am mayeko, lu mu am joxe ko
Da may diggal lu baax
Ãa moo di ma xarit

Поcмотреть все песни артиста

Другие альбомы исполнителя

Похожие исполнители